1
00:00:56,974 --> 00:00:58,100
Jërëjëf.

2
00:00:58,600 --> 00:00:59,601
Baax na.

3
00:01:00,686 --> 00:01:02,479
Déedet, déet, déet. Xam naa lii.

4
00:01:09,862 --> 00:01:10,863
Nu gise ci dëkk bi.

5
00:01:17,244 --> 00:01:18,537
Mënu ma ni jeexna.

6
00:01:19,997 --> 00:01:23,166
Maa ngi yóbbu Evan ci match Red Sox.

7
00:01:26,420 --> 00:01:27,629
Bàyyi leen ak lii?

8
00:01:28,422 --> 00:01:30,299
- Ba ci kanam.
- Ba ci kanam.

9
00:01:48,192 --> 00:01:49,776
Yaakaar nga ni cancer u der la?

10
00:01:50,485 --> 00:01:52,446
O, waaw. Waaw.

11
00:02:09,338 --> 00:02:10,339
Tom?

12
00:02:11,924 --> 00:02:14,050
Telefon bi defa doon sone.

13
00:02:14,051 --> 00:02:15,343
Mitch wooma.

14
00:02:15,344 --> 00:02:18,222
Ray Mellor wooma. Kurt Warburton wooma.

15
00:02:18,972 --> 00:02:21,057
Ñaari fan lañu lay seet.

16
00:02:21,058 --> 00:02:22,351
Rut,

17
00:02:23,101 --> 00:02:25,229
bul jaaxle. Lépp a ngi baax.

18
00:03:12,776 --> 00:03:13,777
Baax na.

19
00:03:42,931 --> 00:03:43,932
Evan?

20
00:03:44,892 --> 00:03:46,351
Amnaa sandwich

21
00:03:50,439 --> 00:03:53,984
Te dafa melni danga am mail!

22
00:03:56,820 --> 00:03:58,071
Tom, dalal jàmm.

23
00:03:59,239 --> 00:04:01,241
Hey. Yaa ngi nelawoon tay ci suba, man...

24
00:04:07,581 --> 00:04:08,916
Jaar nga ci biir néeg bi?

25
00:04:13,003 --> 00:04:16,089
Dédeet, jaar naa ci sa bagaas.
Lu nekk ci biir néeg bi?

26
00:04:19,635 --> 00:04:22,012
Lii mooy reerukaay bu Driftwood.
Bàyyil mesaas.</i>

27
00:04:23,180 --> 00:04:24,681
Nanga def. Man Patricia laa tudd.

28
00:04:26,099 --> 00:04:30,353
Dama komànde parm ginaar
ak benn daggitu mburu kreem coco,

29
00:04:30,354 --> 00:04:35,776
Ak amnaa patty dindon bu amul bun
ak benn lëkkalekaay saucisse.

30
00:04:37,027 --> 00:04:38,778
Bëgguma ñu delloma xaalis,

31
00:04:38,779 --> 00:04:42,698
Bëgg naa nit ki rek
ki def lii ngir xam.

32
00:04:42,699 --> 00:04:44,992
Te bëgguma nit ki
ki def lii ngir dugg ci jafe-jafe,

33
00:04:44,993 --> 00:04:49,288
Man... xam nga,
Lima bëgg mooy ñu jàngee ci.

34
00:04:49,289 --> 00:04:50,581
Duma...

35
00:04:50,582 --> 00:04:52,291
- Li gëna rafet, jàpp naa ni...
- <i>Boxu bataaxal bi fees na</i>

36
00:04:52,292 --> 00:04:54,920
<i>te mënul nangu benn mesaas
ci jamono jii. Taggoo.</i>

37
00:04:55,796 --> 00:04:56,797
Lu baax.

38
00:05:05,556 --> 00:05:09,309
Bëgg naa xam jaar-jaar bi
ci ginaaw nataal bu neex bii.

39
00:05:10,727 --> 00:05:13,647
- Maanaam, lu xew?
- Baax na. Baax na.

40
00:05:14,898 --> 00:05:17,192
Lu tax nga wax ma
mu dee bi muy am doom?

41
00:05:20,654 --> 00:05:22,030
Ndax moo ko def.

42
00:05:24,575 --> 00:05:26,325
Musul nekk nimu meloon
ginaaw boo juddoo.

43
00:05:26,326 --> 00:05:27,578
Baax na.

44
00:05:28,120 --> 00:05:29,121
Loolu lumuy tekki ?

45
00:05:31,123 --> 00:05:34,626
Dafa am AVC bu bawoo ci preeclampsie.

46
00:05:35,127 --> 00:05:37,379
Ginaaw loolu, waxul woon lu jaadu.

47
00:05:38,589 --> 00:05:39,755
Waxul woon dëgg, naka la ko defee?

48
00:05:39,756 --> 00:05:42,384
Amna lumu def ci yuur gi.

49
00:05:43,385 --> 00:05:44,386
Ci xelam.

50
00:05:46,013 --> 00:05:48,098
Te loolu dafa laal jikkoom.

51
00:05:52,978 --> 00:05:55,105
Amul woon kaaraange nekk ci wetam.

52
00:05:56,440 --> 00:05:57,816
Kon, amnaa...

53
00:05:59,735 --> 00:06:01,653
Dama ko wara jox The Home.

54
00:06:03,864 --> 00:06:05,281
Luy "Kër gi"?

55
00:06:05,282 --> 00:06:08,784
Dëkkuwaay bu rafet la woon ci ile bi

56
00:06:08,785 --> 00:06:12,330
ngir nit ñi am jafe-jafe xel.

57
00:06:12,331 --> 00:06:14,749
Melni daara juy faj xel?

58
00:06:14,750 --> 00:06:16,376
- melni asilu dof?
- Déedéet.

59
00:06:21,840 --> 00:06:22,925
Waaw.

60
00:06:25,385 --> 00:06:28,847
Ñaari at ci ginaaw la faatu
aneurisme yuur.

61
00:06:33,185 --> 00:06:34,937
Daf la bëggoon lool.

62
00:06:42,861 --> 00:06:44,279
Waaw, jàng naa bataaxal yi.

63
00:06:47,449 --> 00:06:48,617
Ndax mën naa jàng benn?

64
00:06:51,370 --> 00:06:52,954
"Salaam Evan,

65
00:06:52,955 --> 00:06:55,248
Dama soxla sa loxo yu ndaw ngir jël caabi yi

66
00:06:55,249 --> 00:06:57,291
ak say baraam yu ndaw
dem ba ci sama bakkan

67
00:06:57,292 --> 00:06:59,086
ngir dindi jaasi ci sama yuur.

68
00:06:59,586 --> 00:07:00,963
Moytul bu baax.

69
00:07:01,964 --> 00:07:02,965
Mbëggeel, sa yaay."

70
00:07:09,137 --> 00:07:10,138
Loolu baax na.

71
00:07:11,390 --> 00:07:12,391
Loolu lu baax la.

72
00:07:14,434 --> 00:07:15,435
Beneen?

73
00:07:15,978 --> 00:07:17,020
"Salaam Evan..."

74
00:07:23,527 --> 00:07:24,695
Oh, Yàlla. Yaw...

75
00:07:25,821 --> 00:07:29,156
- Ah sama Yàlla. Danga ma tiital.
- Man itam bëgg naa la. Baal ma.

76
00:07:29,157 --> 00:07:30,158
Oh, gee...

77
00:07:34,997 --> 00:07:36,164
Mën nanu waxtaan?

78
00:07:37,124 --> 00:07:38,541
Waaw. Dëgg la, waaw.

79
00:07:38,542 --> 00:07:40,210
- Luy loolu, Wyck?
- Waaw. Jub.

80
00:07:41,461 --> 00:07:42,462
Baax na…

81
00:07:45,090 --> 00:07:48,051
amna luma musa am
ci sama kalpe lu yàgg lool,

82
00:07:48,552 --> 00:07:49,553
ak...

83
00:07:50,762 --> 00:07:52,431
Dama jàpp ni jotna ma wax leen luko waral.

84
00:08:03,066 --> 00:08:05,027
- Fatteliku... Waaw.
- O, waaw, xam naa ko.

85
00:08:09,698 --> 00:08:11,157
Nanga def, sama xol.

86
00:08:11,158 --> 00:08:12,826
Nanga def, Wyck. Hey.

87
00:08:13,327 --> 00:08:14,786
Xoolal loolu.

88
00:08:15,829 --> 00:08:18,581
Sama xol, loolu mooy sa
Xale bu baax ci liise, Wyck.

89
00:08:18,582 --> 00:08:20,751
- Waaw.
- Xaj bu mag bi.

90
00:08:23,629 --> 00:08:24,671
Waaw.

91
00:08:25,380 --> 00:08:27,465
Kon ma dem.

92
00:08:27,466 --> 00:08:31,512
Amnaa ay nataal yu bari
Dama wara joxe kado tay.

93
00:08:33,347 --> 00:08:34,764
Waaw, waaw.

94
00:08:34,765 --> 00:08:35,932
Bon...

95
00:08:35,933 --> 00:08:36,933
Waaw.

96
00:08:39,770 --> 00:08:42,397
Xoolaatal weer wi.
Amaana xamuma ko lépp.

97
00:08:45,859 --> 00:08:47,194
Lu xew fii ?

98
00:08:50,239 --> 00:08:53,575
{\an8}Amaana xale yu turist
ki dégg jaar-jaari Boogeyman.

99
00:09:28,986 --> 00:09:31,196
Dama yaakaar... dem.

100
00:09:31,905 --> 00:09:35,324
Maa ngi tàggatoo. Naqqari.

101
00:09:35,325 --> 00:09:36,326
Baax na.

102
00:09:38,453 --> 00:09:39,787
Waaw.

103
00:09:39,788 --> 00:09:41,790
Baax na. Kon mën naa soxla yii...

104
00:09:48,130 --> 00:09:49,131
Waaw.

105
00:15:03,779 --> 00:15:04,780
Ubbi bunt bi!

106
00:15:05,489 --> 00:15:06,490
Ubbi buntu bi.

107
00:15:07,366 --> 00:15:08,492
Ubbi buntu bi.

108
00:15:09,326 --> 00:15:10,409
Man...

109
00:15:10,410 --> 00:15:11,745
Déedéet! Oh, Yàlla.

110
00:15:35,644 --> 00:15:36,687
Oh, Yàlla.

111
00:15:57,916 --> 00:15:59,209
Patrisi!

112
00:16:02,504 --> 00:16:03,589
Patrisi!

113
00:16:19,021 --> 00:16:20,856
Ndimbal dimbali! Wyck!

114
00:16:22,983 --> 00:16:24,776
Oh, Yàlla. Ndimbal dimbali!

115
00:16:30,365 --> 00:16:32,284
Ndimbal dimbali! Ndimbal dimbali!

116
00:16:33,744 --> 00:16:34,745
Ndimbal dimbali!

117
00:16:39,708 --> 00:16:41,334
Hel... Hel...

118
00:16:41,335 --> 00:16:42,711
Saa waay! Hey!

119
00:16:43,337 --> 00:16:45,297
Ndimbal dimbali! Patricia la!

120
00:16:45,923 --> 00:16:47,674
Hey! Ndimbal dimbali!

121
00:16:48,634 --> 00:16:52,178
"Pringtemps bi yépp dafa sol xaaju xol
pendant bi Samuel sol beneen genn-wàll gi."

122
00:16:52,179 --> 00:16:53,471
- Lan?
- Yaa ngi fàttaliku loolu?

123
00:16:53,472 --> 00:16:55,723
- Yooyu pendant yu ndaw?
- Loolu mooy wàll wi la gënal?

124
00:16:55,724 --> 00:16:57,058
- Lépp. Xamnaa...
- Loolu lu rafet la.

125
00:16:57,059 --> 00:16:58,936
- ...Daa melni ku sedd, waaye amnaa xol.
- Loolu dof la.

126
00:17:00,062 --> 00:17:01,229
Sama Yàlla!

127
00:17:01,230 --> 00:17:02,605
Patrisiya?
- Lu xew?

128
00:17:02,606 --> 00:17:03,814
Lu muy def fii?

129
00:17:03,815 --> 00:17:05,441
Xamnaa ni woowuma ko bii yoon.

130
00:17:05,442 --> 00:17:06,567
- Dama...
- Luy...

131
00:17:06,568 --> 00:17:08,277
Patricia, ndax mën naa la dimbali?

132
00:17:08,278 --> 00:17:10,321
- Loy def?
- Lu xew ?

133
00:17:10,906 --> 00:17:12,280
Ci anam bu dëggu?

134
00:17:12,281 --> 00:17:14,408
- Baal ma. Loy def?
- Déedet. Noppal.

135
00:17:14,409 --> 00:17:16,452
Patricia
- Noppil !

136
00:17:16,453 --> 00:17:18,828
- Ah, sama boroom. Patricia.
- Lu xew leegi ?

137
00:17:18,829 --> 00:17:20,164
- MAN…
Patrisiya?

138
00:17:20,165 --> 00:17:21,875
Woowal poliis! Dellu na!

139
00:17:22,459 --> 00:17:24,544
- Ku dellu?
- Xam nga kan.

140
00:17:24,545 --> 00:17:27,129
Boogeyman bi! Woowal poliis!

141
00:17:27,130 --> 00:17:28,589
- Lan? Okay...
- Woowal poliis bi.

142
00:17:28,590 --> 00:17:31,301
...danga wara kaf.
Ndax ba leegi yaa ngi koy def?

143
00:17:32,010 --> 00:17:33,970
- Liiñ telefon bi dafa jeex.
- Ah sama Yàlla.

144
00:17:33,971 --> 00:17:35,764
- Lan?
- Loolu dafa doy waar.

145
00:17:38,392 --> 00:17:39,434
Am nga buntu ci ginaaw?

146
00:17:40,894 --> 00:17:42,938
- Baax na.
- Ndax am nga bunt ci ginaaw ?

147
00:17:43,730 --> 00:17:46,315
- Waaw, waaw.
- Waaw kay, fexeel mu tëju. Léegi!

148
00:17:46,316 --> 00:17:48,943
- Te nga fay làmp yépp.
- Déedet, déet !

149
00:17:48,944 --> 00:17:50,320
Bul ko fowee.

150
00:17:50,821 --> 00:17:53,407
Bul... Ñépp xam nañu
ni dafa fen ci woote yi.

151
00:17:56,368 --> 00:17:57,953
Baax na. Dama fen ci woote yi.

152
00:17:58,579 --> 00:17:59,996
- Xamoon naa ko!
- Ah sama Yàlla.

153
00:17:59,997 --> 00:18:01,247
- Waxuma ko?
- Wax nga ko.

154
00:18:01,248 --> 00:18:02,331
- Wax nga ko!
- Wax naa ko.

155
00:18:02,332 --> 00:18:04,542
Dama... melni dañu ma bàyyi,

156
00:18:04,543 --> 00:18:06,836
Ma wax benn nit, ñu wax ñépp,

157
00:18:06,837 --> 00:18:08,462
ba noppi ma wàcci ñaari yoon.

158
00:18:08,463 --> 00:18:09,881
Waaye giñ naa ci Yàlla;

159
00:18:09,882 --> 00:18:13,093
mu ñëw sama kër ci guddi gi.
te maa ngi waat ni dellu na.

160
00:18:14,178 --> 00:18:15,678
Baax na. Loolu lu baax la.

161
00:18:15,679 --> 00:18:17,346
- Taggoo.
- Kris, maa ngi lay wax rek

162
00:18:17,347 --> 00:18:18,724
- ngir nga--
- Demal !

163
00:18:19,308 --> 00:18:22,102
Bàyyi di def lii ci yaw.
Du ci yaw!

164
00:18:23,395 --> 00:18:26,314
Maa ngi jéggalu, waaye du man sabab bi
ni amoo benn xarit.

165
00:18:26,315 --> 00:18:28,900
Liko waral mooy danga dof. Baax na?

166
00:18:28,901 --> 00:18:30,776
Sa feet bu ndaw?
Dafa ray ñépp.

167
00:18:30,777 --> 00:18:32,779
Leegi yàq nga book club bi.

168
00:18:33,280 --> 00:18:34,615
Danga soof lool.

169
00:18:35,199 --> 00:18:37,743
Demal tàggoo rek, waaw kay?

170
00:18:39,077 --> 00:18:40,078
Demal tàggoo.

171
00:18:40,996 --> 00:18:42,706
Taggoo. Baax na?

172
00:18:43,749 --> 00:18:44,750
Taggoo.

173
00:18:45,584 --> 00:18:46,959
Taxaw-b--

174
00:18:46,960 --> 00:18:48,920
Sama Yàlla. Kris!

175
00:18:48,921 --> 00:18:50,713
Moo gëna bon! Mooy ki gëna bon.

176
00:18:50,714 --> 00:18:52,340
Ak... Maa ngi jéggalu.

177
00:18:52,341 --> 00:18:54,259
- Kris, ndax lépp jàmm?
- Am nga jàmm?

178
00:18:55,219 --> 00:18:56,220
Salaam maalekum?

179
00:18:59,056 --> 00:19:00,515
Fan lay dem?

180
00:19:00,516 --> 00:19:01,767
Patricia. Lan?

181
00:19:07,814 --> 00:19:10,400
Sama gaa yi, dinaa woo 911
ngir yëgle mbir mi fii.

182
00:19:15,656 --> 00:19:17,783
Yàlla. Bëgg naa mu wàcci ci sama gazon.

183
00:19:29,586 --> 00:19:30,921
Ba leegi mingi fee ci biti?

184
00:19:38,387 --> 00:19:40,889
Mu ngi ci biir kër gi! Get...

185
00:19:41,682 --> 00:19:42,891
Génn foofu!

186
00:19:43,892 --> 00:19:44,893
Get...

187
00:19:46,311 --> 00:19:47,812
Oh, d...

188
00:19:47,813 --> 00:19:49,230
Daf lay ray!

189
00:19:49,231 --> 00:19:50,816
Génn foofu!

190
00:19:55,737 --> 00:19:56,947
- Yalla alku!
- Lu doon loolu ?

191
00:20:08,000 --> 00:20:09,042
Fuck!

192
00:20:19,845 --> 00:20:22,431
Déedéet! Déedéet!

193
00:20:32,691 --> 00:20:34,109
Dégg ngama?

194
00:20:35,152 --> 00:20:37,988
Saa waay, sa waay. Yombalal ko.

195
00:20:38,906 --> 00:20:40,365
Daa melni danga dóor sa bopp.

196
00:20:40,908 --> 00:20:43,869
Amnaa puls. Mingi dund.

197
00:20:44,661 --> 00:20:45,662
Déedet, déet, déet.

198
00:20:47,164 --> 00:20:48,664
Jox ma say caabi. Dinaa daw jàkkarloo ak moom.

199
00:20:48,665 --> 00:20:49,832
- Lan?
- Jox ma say caabi.

200
00:20:49,833 --> 00:20:51,126
Dama ko wara daw.

201
00:20:51,668 --> 00:20:52,752
Nanga dellu, bud.

202
00:20:52,753 --> 00:20:53,754
Daw!

203
00:20:55,923 --> 00:20:57,131
Daw rekk!

204
00:20:57,132 --> 00:20:58,175
- Oh, fuck!
- Rek...

205
00:21:22,866 --> 00:21:23,867
Déedéet!

206
00:21:35,921 --> 00:21:36,922
"Salaam Evan.

207
00:21:37,589 --> 00:21:40,384
Ku nekk amna ñaari yaay.
Yaay ak yaay bu nëbbu.

208
00:21:41,009 --> 00:21:42,218
Yan ci ñoom laa?

209
00:21:42,219 --> 00:21:45,013
Man maay sa yaay sekkere,
Maa ngi dëkk ci kër gu nëbbu.

210
00:21:46,682 --> 00:21:48,891
Duñu ma bàyyi ma génn.
Soo màggee tuuti,

211
00:21:48,892 --> 00:21:51,311
mën nga ñëw fii
te nga def yaa ngi nekk mailman bu bonn bi.

212
00:21:51,812 --> 00:21:55,190
Ngir xoolaat, maa ngi dee,
Maa ngi dee, maa ngi dee ba noppi.

213
00:21:55,899 --> 00:21:58,402
Dafa yàgg lool. Gaaw ñëw. Yaay."

214
00:22:00,612 --> 00:22:01,613
Dafa neex.

215
00:22:29,099 --> 00:22:31,059
Lii sa yaay la woon.

216
00:22:32,311 --> 00:22:33,312
Ak lii.

217
00:22:39,568 --> 00:22:40,569
Bii.

218
00:22:44,114 --> 00:22:45,115
Bii.

219
00:22:50,579 --> 00:22:52,497
Ak nit kii

220
00:22:53,874 --> 00:22:56,084
Bëgguma nga fàttaliku beneen bi.

221
00:23:03,217 --> 00:23:04,843
Lu tax nga ma nëbb loolu?

222
00:23:06,136 --> 00:23:08,722
Ndax dañu may gëna naqaral
ak li ma nekk.

223
00:23:12,935 --> 00:23:14,436
Maa ngi lay massawu, Evan.

224
00:23:22,486 --> 00:23:24,446
Lu tax dunu musa bàyyi ile bii?

225
00:23:27,491 --> 00:23:28,575
Mën naa.

226
00:23:31,370 --> 00:23:32,996
Mën nanu bàyyi ile bii.

227
00:23:43,841 --> 00:23:45,174
- Biye Sox yi?
- Waaw.

228
00:23:45,175 --> 00:23:46,551
- Ndax lii dëgg la?
- Waaw, dëgg la.

229
00:23:46,552 --> 00:23:47,885
- Waaw--
- Nun... Déedet.

230
00:23:47,886 --> 00:23:50,847
It... Noo ngi def
benn njeexte ayu-bis ci Boston.

231
00:23:50,848 --> 00:23:52,682
- Wiken bii.
- Yaa ngi wax seryeux?

232
00:23:52,683 --> 00:23:54,184
Waaw, maa ngi wax dëgg.

233
00:23:55,102 --> 00:23:57,563
Ndax mbir yi dina ñu
wuute na ak leegi.

234
00:24:28,844 --> 00:24:30,262
- Nan nga def ?
- Hey.

235
00:25:09,551 --> 00:25:10,552
Fuck.

236
00:25:15,474 --> 00:25:18,519
Dama wara lekk lii fii.
Sama jabar mënul muñ xet gi. Kon...

237
00:25:19,895 --> 00:25:21,480
- Sedd.
- ...mën ngama jox...

238
00:25:22,397 --> 00:25:23,398
Dama soxla 20 ci ñett.

239
00:25:24,483 --> 00:25:25,609
Ñaar fukki ci kaw ñett.

240
00:25:45,170 --> 00:25:46,755
Danga wara def loolu.

241
00:25:47,339 --> 00:25:49,466
Sama Yàlla.

242
00:26:09,570 --> 00:26:11,905
Sama Yàlla!

243
00:26:18,328 --> 00:26:19,872
Déedet, déet, déet!

244
00:26:22,040 --> 00:26:23,500
jahannama bu fucking.

245
00:26:28,755 --> 00:26:31,758
Déedet, bul ko def! Dédeet, yaa ngi koy yàq!

246
00:26:32,759 --> 00:26:33,760
Oh, sama...

247
00:26:39,057 --> 00:26:40,350
Tegal ko ci suuf!

248
00:26:41,226 --> 00:26:43,061
Yalla bu baax, may ma dundu.

249
00:26:48,901 --> 00:26:50,277
Dakkal ko!

250
00:28:17,155 --> 00:28:18,407
Ndax amna beneen pexe?

251
00:28:18,991 --> 00:28:21,285
- Déedéet.
- Waaw kay, jërëjëf waay lool.

252
00:28:37,593 --> 00:28:38,594
Baax na.

253
00:29:06,371 --> 00:29:09,165
<i>Dafay ñëw, limu nuruwoon ci ndoorte li
ngelaw lu metti mingi tàmbali</i>

254
00:29:09,166 --> 00:29:12,084
- <i>niru ak taw bu xarnu bi.</i>
- Waaw kay.

255
00:29:12,085 --> 00:29:13,795
Dédeet, maa ngi ci jàmm. Dignaa la ko.

256
00:29:15,130 --> 00:29:18,217
Dafa... ab góom ci yaram la.

257
00:29:18,759 --> 00:29:21,303
Dafa bëgg ma noppalu rek
ñaari ayu-bis.

258
00:29:22,346 --> 00:29:24,473
Vermont leegi dafa gëna rafet.

259
00:29:26,099 --> 00:29:27,100
Dama la bëgg.

260
00:29:27,643 --> 00:29:30,604
- Dama la bëgg.
- Maa ngi lay indil beneen sàndiis.

261
00:29:43,492 --> 00:29:44,493
Salaam maalekum.

262
00:29:52,251 --> 00:29:54,044
Xamuma woon ni Chelle ëmb na.

263
00:29:55,796 --> 00:29:56,797
Mu ngi?

264
00:30:03,428 --> 00:30:07,057
Man itam bëgg naa la. Mooy morfin bi.
Xam nga ni Dr. Morgan du fo.

265
00:30:08,642 --> 00:30:10,143
Jàppoon naa ni mingi tollu ci 40 at.

266
00:30:12,896 --> 00:30:14,690
Yaa ngi jéema dee ñaari yoon ci guddi gi?

267
00:30:15,274 --> 00:30:16,400
Ndax Loftis xamna ko?

268
00:30:17,568 --> 00:30:18,569
Déedet.

269
00:30:20,195 --> 00:30:22,614
Dédeet, xalaat naa loolu lépp
ak jabaram...

270
00:30:23,907 --> 00:30:24,908
Waaw.

271
00:30:25,909 --> 00:30:26,910
Patricia.

272
00:30:27,828 --> 00:30:29,997
Lan laa gis foofu?

273
00:30:41,008 --> 00:30:42,633
Déglul ma. Danga wara dem.

274
00:30:42,634 --> 00:30:44,719
Déedet, xoolal fii.
War ngama ko wax ñaari yoon.

275
00:30:44,720 --> 00:30:45,721
- Man maay...
- Déedéet.

276
00:30:46,889 --> 00:30:47,890
Leegi.

277
00:30:50,100 --> 00:30:51,810
Mën nga am sa doom fii.

278
00:30:57,232 --> 00:30:58,233
Lu tax?

279
00:30:58,817 --> 00:31:02,779
Kaka. Jànguma dara
ci lenn ci lii.

280
00:31:03,739 --> 00:31:06,490
Mën wéy di dem Boston
te baña dox ci yoonu moom sa bopp.

281
00:31:06,491 --> 00:31:08,827
Mënu ma xaaru dem
te baña dox ci yoonu moom sa bopp.

282
00:31:10,996 --> 00:31:12,663
Xam nga li nu wara def
sunu nekkee foofu?

283
00:31:12,664 --> 00:31:13,665
Lan?

284
00:31:14,541 --> 00:31:16,126
Xoolal yenn college yi.

285
00:31:18,420 --> 00:31:19,796
- Dëgg la?
- Waaw, ci dëgg.

286
00:31:20,297 --> 00:31:21,465
Dinaa ko bëgg...

287
00:31:31,600 --> 00:31:32,851
Jeexagul.

288
00:31:36,855 --> 00:31:37,856
Déedéet.


